Sublime
An inspiration engine for ideas

Salatu gu am solo wax nagn nee kuko deff 100fois Yonnet bi sws dana ko rammu,
moom aki mbokkam❤️
Allahuma salli wa sallim wa barik hala sëyyidina Muhammadine wa hala ali sëyyidina Muhammadine fi kulli lamhatin wa nafsin bi hada di kulli mahlo min lakaa🤍
#TaawOu https://t.co/DKw5uBqvUK

Deff len ko xarit, def ko wéttal, def ko andando.
Kuko takhoo ci sa lamign dee do am jotu jëw, wala di duggu lou sa yon nekkul !!
( Sallalahu hala Muhammadine 🤍 ) https://t.co/3b7u5KHY8h

Serigne Touba neena salatu gui kuko jà ng benn yoon (1 fois), Mel ngani ku julli ci yonnet bi junni yoone (1000) fois Diko saxal niatti yoon (3 fois) bëss bunek Day depook niatti junn i (3000) salaatu halan nabi🤍
#TaawOu https://t.co/aMKCg9NBR4


Q a c i i d a h
•••Astaghfirul Laaha bihii•••
✨Ci ben xët !
••• ••• ••• ••• •••
✨Format A5
••• ••• ••• ••• •••
✨Manuscrit : {Kaatibu Asadul Xadiim} https://t.co/gBG1WNQbAz
Undisputed: one of the greatest reciters of our time. Shaykh Sudais, may Allah preserve him. 🥹❤️ https://t.co/4Ap8ZBD08F
القرآنx.com